Bintou Jallow
Wolof 406
Journal 4
Dimbalé rééw yi ñu matal sééni mébét ngirr dooleel jigéén ñi ak xale yu jigéén yi
At mu jot, lu ëpp 500,000 jigéén dinañu faatu ci sabab yu ñu manoon yu lu ñu bokk ak a fanq moytu yu ñu manoon yu am lu ñu bokk ak ëmb.
Te, kenn jigéén ku faatu ku nekk, am na ci ñóóñu ay tmndareet dinañu mucc waayi dina léén bayyeek gaañu-gaañu yu dul wér des ci séén dund. 58 jigéén rekk ci téémëër bu nekk ci rééw yu nééw dooleh yi, dinañu am doom ci ndimbalu fajkat wala sasfaam bu xam-xamam màcc ci lóólu. Ci nóóñu, 40 jigéén rekk ci téémëër bu nekk ñooy am doo ci fajukaay wal loppitaal.
Ba tay, ñu gi am ay jafe jafe yu mag yu ñu manula saafaara ngirr am paj mu séén am-am àttan, te ñu manko jëfandikóó te man na wéy ci wérgu-yaram mu njuréél ak soreel ko. Jigéén ñi ñu am metit bat ay ci yeneen jafe-jafe wérgi-yaram yu mel ne ñakk lekk ak yeneen jafe-jafe noyyi. Kerr yu nééw dooleh yu bari ci rééw yu ñakk yi, ñu ngi jéffandikóó matt wala ndééf këyit ngirr togg wala jaaru. Ci sababu lolu, di nañu am jafe-jafe ak feebra yu saxaar di indi.
Ci wàllu wérgi-yaram, ay tamndareeti jigéén ñu ngi wéy di am ay jafe-jafe yu aju ci ñàkk a lekk ak ay jàngoro yuy jàpp bërëbi noyyikaay yi. Ci rééw yu nééw doole yi, ay tamndareeti njaboot matt lañuy jëfandikóó ngir togg ak njaar. Itam, séén tolof-tolof ci wàllu wérgi-yaram dafa gën a yokku ndax saxaar si ñuy noyyi bu ñu nekkee ci bërëb bu tëju. Rawati na saxaar su bon siy waral ay jàngoro yu ndaw ci bërëbi noyyikaay yi ci xale yi ak no gu fattu ci jigéén ñi. Ci misaal, lu tollu ci 500 junni jigéén ak xale dinañu ñàkk séén bakken ci End at mu jot te li ko waral mooy saxaar su bon si nit ñi di noyyi (Smith, 1999).
– sabab yu ñu manoon a faj yu am lu ñu bokk ak ëmb
– tamndareet
– yu dul wér li des ci séén dund
– tééméér
– doole
– saas-faam
– doom
– wala
– te ñu man ko
– saafara
– ñiu ngi
– ci wérgi-yaramu
– ñu ngi am metit ba tay
– ñàkk lekk
– matt wala ndééf
– ngir
– lóólu
– feebar yu saxaar di indi (wala feebar yu saxaar di joxe)