Mbind 1

à – é – éé – ë – ëë – ñ – ññ – ó – óó

 

2 thoughts on “Mbind 1

  1. Bintou Jallow
    Wolof 406
    Journal 1
    Feebaru Sibbiru ci Gambie ak Politigu Paj mi

    Ci jammo ji, feebary sibbiru ci barr na lol. Sibbiru ci dena sonal mag, jegen bu wehrut ngni akk hal yee. Wahto nawet, bu tawbee taweeh, ndohbee dina barri ci dekko kai yee. Garab bu sibbiru bee do nunna terreh sibbiru si. Nyuu barreh di nanu dahe, surrtu nu neuw doleh. Garrab bue arr sibbiru ci dafa jaffee. Politigu Paj mi dafa doywarr ndah pharmacy wee jayee garrabi sibbiru ken dullen sama. Garrabu sibbiru si dafa jar halishbu barreh. Ngurgi, du dimbali nu neew doleh.

    • Jaajëf Bintu ci xibaar yi nga indi ñeel sibbiru. Xalaat yi am nañu solo. Waaye jàpp naa ne am na yenn ci baat yu jar a xoolaat (ci séén mbindin).

      LIne 1:
      – Bare na lool (Barr na lol)
      – Sibbiru si dana sonal (Sibbiru ci dena sonal)
      – Jigéén i wérul ñi

      Line 2:
      – ak xale yi
      – Waxtu nawet
      – Bu tawee
      – Ndox mi dina bari

      Line 3:
      – Dëkkukaay yi
      – Garabu sibbiru du mën a tere sibbiru si
      NB: Lan nga bëggoon a wax ci “Garab bu sibbiru bee do nunna terreh sibbiru si”?
      – Ñu bari
      – Di nañu dee

      Line 4:
      – “Surtu” wala “rawatina”. “Rawatina” moo gën a nekk baatu Wolof ndax “surtu” nekk na ab baat bu ñu àbbee ci làkku Farañse (surtout).
      – Nééw doole
      – Garab bu aar sibbiri si dafa jafe
      – Pólitigu Paj mi

      Line 5:
      – Doy waar
      – Ndax
      – Farmasi yi ñuy jaaye garabi sibbiru kenn du léén sàmm.

      Line 6
      – Garabu sibbiru
      – Xaalis bu bari
      – Nguue gi
      – Ñu nééw doole

Leave a Reply