Mbind 2

à – é – éé – ë – ëë – ñ – ññ – ó – óó

 

2 thoughts on “Mbind 2

  1. Bintou Jallow
    Wolof 406
    Journal 2

    Pajum cosaan ak Pajum jamono jii nu nekk: Naka la mbir yi tedde ci reewum Gambi

    Naari pajj yee mun nano anda. Pajuum cosaan aana aye jafe-jafe. Jafe-jafe dinanoo benn moy netnyi dano ko gom wy the lolo muna nekk lu bahh wala lu bahul. Pajum cosaan amul research bui woneh ndahh lee fajkat bi akk ki faju dano aam kolareh. Kolareh bobu, tahh na lu fajkat bi wahh kee faju dinako gumm. Pajum jamono jii dafa aam research bu tah pajum cosaan bi do lu fajkat be warah topp. Ci reewum gambi, pajuum cosaan lu mengul akk wa reew bi. Pajumm cosaan dafa meel ni taw gi. Magyee njaykayee denano jefo pajum cosaan. Naaru pajyee munano, anda sunyo aamalateh cherr.

    • 1- Ñaari paj yi man nañu ànd
      2- Pajum cosaan am na ay jafe-jafe
      3- Mooy nit ñi dañu ko …
      4- Te lóóloo mën a nekk lu baax
      5- Baaxul
      6- Baatu “research” man na tekki “gëstu ci Wolof”.
      7- Gëstu buy wone ndax kiy faju dina ko gëm
      8- dafa am gëstu bu tax ………du lu fajkat bi war a topp
      9- Ci rééwum Gàmbi, pajum ….
      10- NB: Lan nga bëgg a wax xi “lu mengul akk wa reew bi”?
      11- dafa mel ni
      12- taw bi? (rain?)
      13- Lan nga bëgg a wax ci “Magyee njaykayee denano jefo..”?
      14- Ndax bëgg nga wax “jëffandikóó”? (jefo)
      15- Ñaari paj yi man nañu ànd su ñu bokkee ay cër? Lan nga bëgg wax fii?

      Jaajëf. Yaakaar naa, dina jar xoolaat mbindinu baat yi Waaye xalaat yi ci biir ëmb nañu njariñ, rawatina taxawaayu gëstu ci li war a boole pajum cosaan ak pajum jamono ji.

Leave a Reply