Project 2

One thought on “Project 2

  1. Bintou Jallow
    Wlof 406

    Project 2
    Women-related health issue in The Gambia
    Gender based violence
    Mbootaay yuy xeex fitnal jigeen, ak ag ak yellennfi doom-aadama Nu ngi jonkonte baleegi akay ay tolof-tolof yu amul dayo, ci at, wala xeet, wala diine, wala askan, te yooyn yepp nu ngi faqeekoo ci genalante ak berci diggente foor ak jigeen. Fitna jiidal ci jigeen ji ni mu ngi bunduxatal ba leegi ngirr yokwe, jama ak nakka jenalante diggante goor ak jigeen.

    Mbootay yu xeet yi, wax naun ne, been jiggeen ci net yu nekk ci addunabi dinau ko sakk wala nu door ko ci dundam. Ci jigeen ni am diggente 15 at ba 44 at, feke wala gis na fitna ju dal ci kaw jigeeni jur na dee ak laggo laggo ci lim bu ipp lim bi sibberu, ak cancer boo noon nepp lee jeye ak xeex jur. Jigeen yid ow ji nu gina nekk ci ayy ci walu boddikonte xeet. Jigeen nu dow nu, di nanu aam fiibar HIV/Aids ndik gilante akk neu doleh.
    Ci rew Gambi, jigeen yi dinanu len fitnal ci legay kai, jango kai, akk san dekko kay yi, ci marshe yi the ken dullen dimbaleh. Ngirr nyaka ndimbal, jigeen yi dunu wax kan moo len fitnal girr banngh sika-sika. Mbootay yi taxawu jigeen yi tamit dinanu len fitnal. Aam na jigeen yu nu teej ci kaaso ngirr sen taxawayi ci fitnal jigeen yi

Leave a Reply