Mbind 3

2 thoughts on “Mbind 3

  1. Bintou Jallow
    Wolof 406
    Journal 3
    Politigu Wergi-yaram neel jigeeni werul ni ci Gambi
    Wergi-yaramu neel jigeeni werul ci Gambi dafa aan aay jafe-jafe. Jigeeni werul yu barah danu aam sibbiru, nyaka lekk bu bha ci yaybi akk dom ji. Jigeeni nekk ci dekki caw caw yi, amuno garab, akk lekk yu bhaa. Wergu yaramu jigeeni yee nekul ci lohii jigeeni. Sani boram kerr akk mag yee nyo dogal san werrel. Ananu nu ham nee dinanu jeffu garrabu cosaan. Lunu aayal dafa bareh. Ngurgi, du depass ci lu gem ci wergi-yaram mu jigeeni. Nguur gi du taxawu jigeeni. Mbootaayu xeet yi, dinanu dimbal ci wallu wergi yaram.

    • Good work. The spelling again

      1- Pólitigu wérgi-yaram ñeel (ñ)
      2- jigééni wérul ñi ci Gàmbi

      3- Man nga bind benn ci ñaar yii:
      – Wérgi-yaramu jigééni wérul ci Gàmbi
      – Wérgi-yaram ñeel jigééni wérul ñi ci Gàmbi

      4- Dafa am ay (jafe-jafe)
      5- … yu bare (barah) dañu am
      6- Ñàkk a lekk bu baax ci yaay ji ak doom ji
      7- Jigéén ñi nekk ci dëkki kaw gi
      8- … amuñu garab ak lekk yu baax

      9- Lan nga bëgg a wax ci lii “yaramu jigeeni yee nekul ci lohii jigeeni”?
      10- Sééni boroom-kër ak mag yi
      11- Lan nga bëgg a wax fii:
      – “nyo dogal san werrel”?
      – “Ananu nu ham nee dinanu jeffu garrabu cosaan”?

      12- Li ñu aayal dafa bari (wala bare)
      13- Nguur gi du depaase lu jëm ci wérgi-yaramu jigéén ñi
      14- … jigéén ñi (jigeeni)
      15- ….. dinañu dimbali ci wàllu wérgi-yaram
      NB: This would be much stronger if you had added some statistics information about the issues discussed. Jaajëf!

Leave a Reply