Xibaar Wergi-yaram ci Gambi
Naka la caada ji taxawe neel jallalem xibaari Wergi-yaram ci reew mi?
Caada ji taxawe na ci jallealem xibaari wergi-yaram ci bont yi barra. Ci walu ulwerigi-yaram, caada aam nanu at garab yu nu jeffu yi nga ham ne gestu ne dinanu am njeren. Dinanu jiffu xas. Dinanu whul xas, weer ko, xooj. Dina jiffoh, mbott tameet. Xubi jarab yi tamit dinanu ko jiffu. Dinanu, jel, garab yi xooj len ding naan, wala cangat,
Am nanu xeet yi faj wergi-yaram yu bokul akk yeneen ni xeeti. Pul yi dinanu jiffu pas ngeer walu jureel. Am nanu yeneeni xeet yi jeffo, sunguf akk ngerr faj beeg waala maat jaan.
Caada yi aam nanu ay xeeti defin yu am solo ci jallale xibaar mu mucc. Xibaar yi. Ci walu berr bu met, am annu at garab xooj yu fag. Ci walu bonng bu met, dinau jiffu garabbu neem. Wallu, nakk-ndox, dinanu jiffu xorom akk sucarr ci ndox.
Fajju caada yi, am nanu fajj yu am njerim akk yi hawa doy war.
Bintou Jallow
Wolof 406