Ci wàllu wérgi-yaram, ay tamndareeti jigéén ñu ngi wéy di am ay jafe-jafe yu aju ci ñàkk a lekk ak ay jàngoro yuy jàpp bërëbi noyyikaay yi. Ci rééw yu nééw doole yi, ay tamndareeti njaboot matt lañuy jëfandikóó ngir togg ak njaar. Itam, séén tolof-tolof ci wàllu wérgi-yaram dafa gën a yokku ndax saxaar si ñuy noyyi bu ñu nekkee ci bërëb bu tëju. Rawati na saxaar su bon siy waral ay jàngoro yu ndaw ci bërëbi noyyikaay yi ci xale yi ak no gu fattu ci jigéén ñi. Ci misaal, lu tollu ci 500 junni jigéén ak xale dinañu ñàkk séén bakken ci End at mu jot te li ko waral mooy saxaar su bon si nit ñi di noyyi (Smith, 1999).
Millenium Development Goals and the Gambia Health Policies
Maternal and Infant Health.
Limum ndee ci jigéén ñi ak xale yi
Dée yi yay bala la ci doom yi te am na jeexital yu doy-waar ag jggi-daywo ñeel muccug xale yi. Su yaay ji wérul, dina am jeexital ci doom ji. Dondo yaay am na taxu bo strong ci dondu xale yi akk continuing caytu xale yi. Yaay ak doom gi ci lu weesu sax diiru lem ak njuddumb liir bi loo genaw 6 ayubés.
Jigéén yi dée bala sin doom yi am ñaar at, am nañu 20 at. Teela deewu yaay dina am ay jafe-jafe ci doom yi. Jafe-jafe yu joor fiibar akk tela dée wu xale yi. Su yaay ji wérul, dina am jeexital ci doom ji. Ttla deewu yaay dinan am jeexital ci dundu xale bi ak ci wérgu yaramam.
Soreel njur lu am solo la ci dundu xale bi ak deewam ba, tax na dina fésal njariñu soreel jo njur ak xelal yaay yi diir bu gàt, ginnaaw bi bu amee doom. Gi jigéén yu ci téémeër bu nekk ci Gambi nu ngi jëfandikkóó jumtukaay yuy soreel njur te 25 ci 100 bu nekk amuñu ganay ngirr soreel jur. Wergu yaram yaya neek la lu jafe ngir am saafara yu déppo ci sen am am.
1- Dee (line 2)
2- Deewu yaay balaa la ci doom (line 2)
3- …. jéggi-daywo (line 2)
4- Dundu yaay (line 3)
5- Lan nga bëgg a wax ci “taxu”?
6- “Strong” = am doole (line 4)
7- Dundu (line 4)
8- Ak
9- wéyug caytu xale yi (line 4)
10- doom ji (line 4)
11- Lan nga bëgg a wax ci “lem” (line 5)?
12- njuddum liir bi (line 5)
13- …ginnaaw 6 ayubés (line 5)
14- Jigéén yi dee balaa séén doom yi am ñaari at (line 6)
15- …yu jur feebar ak teel a deewu xale yi (line 7)
16- Teel a (line 8)
17- …dina am (line 8)
18- …..ak deewam, ba tax na (line 10)
19- … soreel njur (line 11)
20- .. diir bu gàtt (line 11)
21- …. amuñu ngànnaay ngir soreel njur
22- Wérgu-yaramu yaay nekk na lu ….
23- … yu dëppóó ak séén am-am
Mbootaay yuy xeex fitnal jigéén, akaq yelleef doon-aadama ñu ngi ba leegi ak ay tolof-tolof yu amul dayo, ci a, wala xeet, wala diiné, wala askan, te yooyu yépp ñu ngi fàqeeko ci gënalante ak ber ci diggënté góór ak jigéén. Fitna jii dal ci jigéén ji ni mu ngi bunduxatal ba leegi ngirr yok, jam ak nakk gënalante diggante góór ak jigéén.
Mbootay yu xeet yi, wax ñanu ne, bén jigéén ci net yu nekk ci àddunabi dina ko sakku, walla nu dóór ko ci dundam. Ci jigéén yi am diggënté 15 at ba 44 at, feke wala gis na fitnal ju dal ci kaw jigéén jur na dée ak laggo ci limb u ëpp lim bi sibbiru, ak cancer léém booréé jëyé ak xeex di jur. Jigéén yi laggo nu gina nekk ci ayy ci walu boddi konte xeet. Jigéé nu ndaw yi dinañu aam fiibar sidaa ndik gëlanté akk new doleh.
Ci rew Gambi, jigéén yi di nañu len fitnal ci lagy kai, jango kai, akk sen dekko kay yi té ken dullen dimbal. Ngirr ñakka dimbal, jigéén yi di nañu wax kan mo len di fitnal ngirr ñakka sika-sika. Mbootay yi taxawu jigéén yi amuñu dolen nyo len di fitnal.
1- Fitnaal
2- Ak àq ak yelleef doom-aadama
3- ñu ngi am ba leegi ay tolof-tolof
4- .. ci at
5- fàqeekoo
6- ngir
7- yokk
8- ñàkk a gënalante
9- Mbootaayu Xeet yi
10- benn jigéén ci ñett …… àdduna bi dinañu ko sàkku
11- walla ñu dóór ko
12- Fekke wala gis
13- dee
14- laago
15- …..yu gën a nekk ci ay ci wàllu boddikonte-xeet
16- dinañu am
17- feebar
18- ndax gënalante ak nééw-doole
19- rééwu Gàmbi
20- dinañu léén fitnaal ci liggééyukaay yi, ak sééni dëkkuwaay te kenn du léén dimbali
21- … Ndax ñàkk ndimbal …kan moo léén di fitnaal
22- Lan nga bëgg a wax ci “ñàkk a sikki-sàkka”?
23- doole
24- Baal ma, dégguma bu baax lan nga bëgg a wax ci sa wax ju mujj “Mbootay ……di fitnal”.
Jërëjëf.

Project 3

Project 2