Mbind 3 (200 baat)

Mbind 3: (200 baat)

Àpp, Àllarba 25 fan ci Feweriyéé

Theme: Ci lekkuukaay bi.

Situation: Consider a day when you and your friends or parents or family or other acquaintances went out to have food at a restaurant. You had different things based on your different preferences and/or what the restaurant had on that day.

Write on: Write a report on that experience including as much as possible the vocabulary of the theme Ci lekkukaay bi. Include names of people you went with and their relationship to you, the place you went and where it is located, the date and/or time you went there, what you went there for (ndékki, wala añ, wala reer), what the waitress said they had, what each of you had for their main dish and drink, how much you paid or how much each of you paid (if shared), was the food good or not, what did people in the group think about the food, was it tasty or plain or spicy or salty, did you eat with your hands or with forks or spoons, etc. NB: You may include any other information relevant to the topic.

NB: à – é – ë – ó – ñ –

10 thoughts on “Mbind 3 (200 baat)

  1. Ci juróóm-ñeenti fan ci weeru feweriyéé, man ak sama xarit bu tudd Anthony añoon nanu ci pasyoŋu Wedge ci Champaign. Wedge am na togg waa Meksiik. Man bëg naa lekk togg waa Meksiik te liggééyewoon naa ci ab pasyoŋ waa Meksiik ba ma nekkee ci iniwersité waaye mësuma lekk ci pasyoŋu Wedge.

    Ci pasyoŋ, serwikat bi dalaloon na nu te indiloon na nu ay kaasi ndox bu sedd. Anthony naanoon na kaasoom ndox te laaj na serwikat bi ndax moom man indil na ko beneen kaasu ndox ndax moon dafa maroon. Serwikat bi indiloon na ko beneen kaasu ndox te laajoon na nu, “Lan ngéén lekk ci añ tay?” Anthony jëloon na ñetti tacos. Jëloon na benn taco ak yàppu-nag ak naari taco ak jën. Man laajoon naa serwikat bi ndax am na sope ci Wedge. Serwikat bi waxoon na ma ne amu ko ci Wedge. Ban pasyoŋ waa Meksiik amul sope??? Kon jëloon naa benn palaatu chiles rellenos ndax bëgg naa kaani. Togg gi ci Wedge neex na. Anthony lekkoon na ak ay loxoom ndax soxnawul kuddu wala furset ngir lekk tacos. Moom bëggoon na lool ay taco-am (ay tacoom?) ndax dañu saf kaani. Man bëggumawoon sama togg ndax xamoon naa ne dafa lewetoon, waaye bëgoon naa lool ndax bëgg naa lekk ak samay xarit. Fayoon nanu fukk ak juróóm-ñaari dolaar ngir sunu togg. Appare, demoon nanu ci Kopi ngir naan attaaya.

    • Jaajëf!

      1- Bëgg (Bëg) Ndax bëgg nga wax “bég”?
      2- Ci pasyoŋ bi (In the …)
      3- Ndax mu sedd (ndox -m)
      4- Naanoon na kaasu ndoxam? (Do you wanna say his?) WALA (Kaasum ndox)?
      5- ndax moom man na ko indil beneen kaasu ndox
      6- Sope (Ndax bëgg nga wax ‘supp?”)
      7- Soxlawul kuddu (soxnawul)
      8- Ay tacoom. Waaw, baax na.
      9- Bégoon naa?!(Bëgoon naa)

  2. Gisuma samay xarit ci semestaar bii. Moo tax demoon naa ci pasyoŋu waa Meksik, Fiesta Café, ak sama jëkkër ak sunuy xarit. Lekkukaay bi nekk na ci dëkku Champaign. Reerantewoon nanu. Man, maa bëgg lool pasyoŋ bii ndaxte sama xarit liggééy na fii. Moom wax ma ne bëgg na sángara ci pasyoŋ bii, waaye xam na ne man naanuma sàngara. Jëloon naa ay enchilada ak yàppu-ginnaar, ak ceeb, ay ariko, ak formaas. Dafa safoon kaani, neexoon na lool. Sama jëkkër naanoon na ab burrito ak yàppu-nag ak ay lujum. Fattewuma lu naan sunuy xarit, waaye waxoon nañu ma ne bëggoon nañu ko lool. Naanoon nanu ak ay furset ak sunuy loxo. Suuroon nanu. Waxantewoon nanu ci sunuy kalaas ak ci liggééyu sama jëkkër ci fajukaay bi. Sunu reer seeruloon ndaxte naanunuwoon sàngara. Ginnaaw lóólu, demoon nanu ci dëkku sunuy xarit, fan fowantewoon nanu. Seeteewoon nanu ay film ci ordinatëë bi. Demoon nanu ci sunu dëkk. Joxoon naa sama muus mu rakk ab garab. Am na feebaru xol, te jël naa ko garab bi guddi gu épp. Joxoon naa sama ceku mu wert ndox. Nelawoon naa ci ñetti waxtu ci suba. Sama jëkkër fowoon na ak ay xaritam ci ordinatëë bi, ndaxte liggééy na ci guddi te nelaw na ci bëcceg.

    • Jaajëf!

      1- Reerandoowoon nanu (reerantewoon nanu)
      Jessica, I am sure you wanted to say “we had diner together”? Because “reerante” would mean “you had each other for diner :)”, which I suppose you didn’t 🙂
      2- Moom wax na ma ne (Moom wax ma ne )
      3- Sàngara (sángara)
      4- Arikópó (ariko)
      5- Naan burrito WALA lekk burrito? (Man xamuma ndax xamuma lu bari ci ñamu waa Meksik)
      6- Seerulwoon (Seeruloon)
      7- Nu fowantuwoon fa (Fan fowantewoon nanu)
      8- Seetaanoon nanu ay film
      9- Ordinaatëër
      10- Joxoon naa sama muus mu ndaw mi ab garab (my younger cat?)
      11- Te jox naa ko garab bi (You give the cat the medicine?) (Jox =give, jël=take)
      12- Bëccëg (bëcceg)
      13- Naanu nanu ak ay furset. (Leek?)

  3. Assalaamaalekum. Man tudd naa Garrett. Man sant naa lee. Man jogè naa Rockford ci diwannu Illinois. Man dekk naa Champaign ci diwannu Illinois. Benn bës ci weeru Desàmbar, Sama wajur ak Samay Xarit ak Man demoon nañu pasyon. Pasyon tudd na “Linos.” Samay xarit tudd nañu Paul ak Jereme ak Joe ak Liam. Samay xarit sant nanu Zeman ak Atchinson ak McAsey ak Markham. Sama wajur tudd nañu Wallace ak Carolyn. Lañu lekkoon reer. Fowoon naa ko serwikat bi Assalaamaalekum, na nga def.” Fo na ma “ Maalekum salaam. Maa ngi ci jàmm.” Fo naa ko serwikat bi “ Lan ngèèn togg tay” Fowoon na ma “ Tay, am nanu Lasagna ak spaghetti ak chicken parmesan ak chicken marsala ak house salad.” Fowoon naa ko serwikat bi “ Defal ma benn palaatu Lasagna.” Paul dogaloon na Lasagna tamit. Jereme dogaloon na spaghetti. Joe dogaloon spaghetti tamit. Liam dogaloon na chicken parmesan. Samay wajur dogaloon nañu chicken marsala. Man fowoon naa ko serwikat bi “ Soxna si, nga baal ma, lan ngèèn am ngir naan?” Serwikat bi fowoon na ma “Am nanu sangara ak ndox ak ndoxu-soraas.” Fowoon naa ko Serwikat bi “Indil juròòmi kaasi ndoxu soraas ngir Samay xarit ak man ak Indil ñari sangara ngir sama wajur.” Laa ñaanoon “Ñaata la?” Fowoon na ma “Lépp nekk na 100 dollars.” Fowoon naa ko “Jêrëjëf, Nu ngi dem ba beneen yoon.” Fowoon na ma “ Baax na. ba beneen.” Reer nekkoon na neex. Samay Xarit ak Samay wajur amoon nañu (a fantastic time). Samay xarit ak Samay wajur kex-kesiwoon nañu lu bari.

    • Jaajëf!
      Garrett, you repeated so many structures from the text we had in the materials. These writing assignments are meant to use more creative structures on your own while talking a personal experience.
      Thanks. Check my comments below.

      1- Jógé (jogè)
      2- Dëkk (dekk)
      3- Diwaanu (diwannu)
      4- Waajur (wajur)
      5- ….ak man demoon nanu
      6- pasyoŋ (pasyon)
      7- Pasyoŋ bi tudd na ….
      8- Sant nañu
      9- Reer lañu lekkoon (Lañu lekkoon reer)
      10 “Fowoon naa ko serwikat bi”: Lan nga bëgg wax fii? What do you mean, here?
      11- Check the meaning of “fo” (Fo = to play)
      12- Paul laajoon na (dogaloon na)
      13- Sàngara (sangara)
      14- Juróómi (juròòmi)
      15- “Laa ñaanoon “Ñaata la?” What do you mean, here?

  4. Benn fan kañ nekkoon naa ci liise, samay xarit ak man amoon nanu benn fanu-wàll ci jàngukaay ak bëggoon nanu añi ci pasyoŋ. Demoon nanu ci pasyoŋu Merry Ann’s, ndax amoon nanu fukki dolaar rekk ak nekkoon nanu juróóm-ñaari nit. Ci Champaign, benn sandiis jar na juróómi dolaar, moo tax soxlowoon nanu dem ci pasyoŋu seerul, ne Merry Ann’s. Amoon nanu tabaal bu ndaw, waaye xac-xajaloon nanu jàngkati ci sunu liise dañu bank.

    Serwikat yi bëgguñuwoon nun ak yeneen jàngkat yi, ndax bariwoon nanu coow. Jëloon nanu ñeeti palaati pombiteer bu ñu saaf, li dafa ñaari dolaar ci palaat, ak benn palaatu yàppu-mbaam bu ñu saaf, lee jar na ñaari dolaar ci palaat tamit. Ci Merry Ann’s, ñam bu ñu neex nekk na ñam bu ñu saaf. Sama xarit Rachel bëggul pombiteer te jëloon na xaj bu rafet, li jar na ñaari dolaar. Bokkoon nanu palaat yi, ak dul naa lekk añ bi kom lii. Lekk nanu ak sunuy loxo. Waxtaanoon ci sunu njàng – samay xarit bëggoon nañu peintuur yi ak ordinatëër yi. Neexalunuwoon, ndax amunuwoon xaalis. Bëgguma li, ndax wax nañu ne ndaw neexaluñu, ak jeem naa neexal bu baax.

    • Jaajëf!
      1- Benn fan, ba ma nekkoon liisé WALA Bi ma nekkee liisé
      2- Fanu-wàll (Ndax bëgg nga wax “half a day”?)
      3- Ci jàngukaay bi
      4- Te bëggoon nanu añi … (TE # from AK)
      5- Soxlawoon nanu (Soxlowoon nanu)
      6- Ci pasyoŋ bu seerul (pasyoŋu seerul)
      7- Xaj-xajaloowoon nanu (Xac-xajaloon nanu) (Baat bi nekk na “xaj-xajaloo”)
      8- Jàngkati ci sunu liisé dañu bànk (Is there a word missing here?). The wording is good but you can make the idea clearer with an additional connector.
      9- Serwikat yi bëgguñu nu woon NB: In the past negative, when the object is replaced by its corresponding pronoun, the latter is placed after the negative part and before the past structure woon)
      Ci misaal: Xamumawoon jàngalekat bi (Xamuma ko woon)

      10- Li dafa ñaari dolaar ci palaat (Lii nekkoon na ñaari dolaar palaat bu nekk = this was 2 dollars for each serving) Is that what you wanted to say?!
      11- Lóólu (Lee). Here, you are referring to “that” thing you just mentioned in the previous sentence. “Lee” could be used in a context where you are in the same physical location with what you are referring to. For example, “Lee lan la?” = What is that? I hope this makes sense to you.
      12- Ñam bu ñu neex (Are you saying ‘the food we like”, “the best food”, etc.?
      13- Waxtaanoon nanu
      14- Paintings? (Man nga ko waxe “nataal yi”)
      15- Neexalunuwoon serwikat bi
      16- Bëgguma lii (this?)
      17- Wax nañu ne ndaw ñi
      18- Ndaw ñi duñu neexal (NB: Using the DA form would be closer to the meaning here)
      19- Jéém naa (Jeem)

  5. Asslaamaalekum, man ak samay xarit ak sama waakër demon nanu chipotle ci pasyon ngir ci reer. Nekk na champaign, Illinois. Tay la bês bu njëkk ci weeru fewwriyéé. Demoon naa ak Garrett Lee ak Paul Zeman ak mag-bu-góór ak mag-bu-jigéén. Nañu tur Frank ak Ashley la tudd. Man, gën naa bëgg Chipotle. Nam wi ma gën naa bëgg nekk naa ginaar ak ceeb ak ñuul ñebbe ak mboq ak formaas ak awakaa. Man gën naa bëgg saf suuker attaya ci naan. Paul Zeman gën na bëgg ginaar ak ceeb ak ñebbe ak awakaa ak formaas. Moon gën na bëgg kaasu ndox ci naan. Garrett Lee gën na bëgg steak ak ceeb ak mboq ak formaas. Moon gën na bëgg kaasu lemonade ci naan. Mag-bu-jigéén, Ashley gën na bëgg ginaar ak soxala ceeb ak ñebbe ak formaas. Moon gën na bëgg kaasu Pepsi ci naan. Mag-bu-góór, Frank gën na bëgg ginaar ak steak ak ceeb ak ñebbe ak formaas ak kanni. Moon gën na bëgg kaasu lemonade ci naan. Lekk nanu lu bari. Duma lekk ñam wu lewet. Amuma nanu kuddu ak furset ak paaka. Lekk nanu ci loxo. Lekk nanu saf kanni ak saf xorom. Lekk nanu ñam lu bari (expensive).

    • Jaajëf!

      1- Demoon
      2- Ngir reer (ngir ci reer)
      3- Bés bu njëkk (bês)
      4- Sama mag-bu-góór
      5- Nañu tur
      Man nga wax (you also can say) Sééni tur nekk nañu Frank ak Ashley (their names are Frank and Ashley) OR Tudd nañu Frank ak Ashley
      5- Ñam wi (Nam)
      6- Ñam wi ma gëna bëgg nekk na (naa)
      7- Ñebbe ju ñuul (ñuul ñebbe)
      8- Attaaya ju saf suukër (Saf suuker attaya)
      9- Soxala? Lan nga bëgg wax?
      10- Limonaat
      11- Moom (Moon)
      12- Amunu kuddu ak furset (Amuma nanu)
      13- Lekke nanu loxo (Lekk nanu ci loxo)
      14- Lekk nanu ñam wu saf kaani ak saf xorom (Saf kanni ak saf xorom)
      15- Ñam wu seer (expensive)

      NB: Jereme, sa liggééy sa mbind am na solo. Waaye dinga soxla xoolaat lii:
      a- Review the adjective-noun structure. For example, in stead of “lewet ñam”, it is “ñam wu lewet” (since the nun class of ñam is –w)

Leave a Reply