Mbind 4

2 thoughts on “Mbind 4

  1. Turu film bi: Tey
    Direktëër bi: Alain Gomis
    Porodiktëër bi: Gilles Sandoz, Oumar Sall, Eric Idriss Kanango
    Bindkat bi: Alain Gomis, Djolof Mbengene, Marc Wels
    Rééw mi: Senegaal/ Farañse
    At: 2013
    Diir bi: 89 simili
    Làkk yi: Farañse ak Wolof

    Benn bës, ab góór yeewu na. Moom xam na moom daan Faatu. Ci ndoorteel, waakëram wax ci dundam. Moom baaxoon na ak neexoon na ci dundam. Ginaaw, moom dem na ci koñ bi ci xaritam. Nit ni dañu bég. Ñoom bàkku ci booru dëkk bi. Ginaaw loolu, moom dem na ci Centerville. Moom dem na seeti jigeen. Bu loolu weesu moom dem na seeti xaritam. Waxtu bu nekk, nit ni dafa mer. Wante ginaaw, nit ni dafa bég. Kon moom dem na ci jabbaram, sax. Jabbaram dafa mer. Moom bëgul wax, wante ci cëppaandaw, ñoom giis nañu sunu doom kon ñoom nekk nañu mag. bu loolu weesu film bi jeex na.

    • Jaajëf. Am na solo.
      Am naa ay benn-benni seetlu ci sa mbind. Jëm nañu ci baat yi. Waaye, gisuma sikk ci say xalaat ndax donte gàtt nañu, matale nañu ngir xibaar nu ci film bi. Xoolal ci suuf ngir yeneeni taawil (taawil = details)

      1- Moom xam na ne moom dina faatu.
      2- ….. waakëram wax na ci dundam
      3- Ci ginnaaw bi, moom dem na ci koñ bi ci xaritam
      4- Nit ñi
      5- Ñoom bàkku nañu
      6- moom dem na seeti jenn jigéén
      7- Waxtu wu nekk (waxtu -w)
      8- nit ñi dañu mer
      9- Wante ci ginnaaw, nit ñi dañu bég
      10- Jabaram
      11- ci cëppaandaw gi
      11- ñoom gis nañu séén doom

Leave a Reply